Effect Mere Paroles By Akhlou Brick(Effect Mere Lyrics)

Learn and sing Effect Mere Paroles By Akhlou Brick(Effect Mere Lyrics). Effect Mere Paroles By Akhlou Brick(Effect Mere Lyrics) is given below:

Effect Mere Paroles By Akhlou Brick(Effect Mere Lyrics)

Effect Mere Paroles By Akhlou Brick(Effect Mere Lyrics)

hey, walabok professeurou rap bi nieuw na may rapologue
hey, walabok professeurou rap bi nieuw na may rapologue
may antidote
sen domou khadj bi dioudou demb ay mbam ma ko bott
may antidote
sen domou khadj bi dioudou demb ay mbam ma ko bott

hey ioe rombat di khol guiss gana messi rap bi nane leu eh mbaye demal nga tokk
hey ioe thiow lema topp ay thioy né thieup pour diotma mais dolen ma thiop eh meuno lene ma thiop ndakh amna doolé thi poche

man rekay lekk xalissou rap bi té dolen si moss
rap bou xegn nekh ni sauce niom louniouy rap gueuneu khassaw limay wadal thi fosse

day day day fegn thi sen sons you bone youniouy tankalé fi tay dof you bone you xamoul musique kessé nio len di diay
carrierou tempo tempo def musique diekeunté moun nga bagn son wou mbgeuguel khana pa bi ak yaye beugeunté wougn yeah SCHADIIQ

Dayza neu régime bi yokk ki khamoul adouna non ki dou nitt so fatal ma fofou fatté na far farando
kou xam louy rap bou waxalek rap xamni queen daba diongoul dafa wodou thi ndaw la tolou rapoul ay ninjas leu topp

té mako dioutal tapp khol mouy daw ma boudalé thi*k faté na poussalé sock day fokni soulou moy robe
man nak souf lathiy sotti sen thiouné moy fegn soumay rap motax bougou malen tontou yeah

Ma Reine Paroles By Souf

doumla clash non damlay kagno baba noy thi ndawal nekheu lekk baba agneau
lebone lipone dafa amone niou lathie autos yi mais bou deuk tawé douma dawal kamaro mbaye demal nga tokk mbaye

dokhote day yam thi toune mbaye dofo ay djiné diapoula thi li nga nek té ngathié dioug mbaye ay mbaye ay mbaye ay mbaye ay D*UL nga indi mbaye

kone danga saga ndeye thiambay ngaanane dangmay fay may khar nga rap nga rap ay day
Mbaye demal tokk
Mbaye demal tokk
Demal tokk

may dinho ballon plaisir yoré galon presi man leu ara barthelemy gueneu télé télé rire
may dinho ballon plaisir yoré galon presi man leu ara barthelemy gueneu télé télé rire
man douma xoulok thiéré bi damay laalo thiéré bi tay ngor reu diap naba billay ndiegane almeu thieré bi
ehh

halima meuss ta dameu bindeu game né teleu clash ma mouy mbalakh may wakh mounane day fethie nda teleu
man doumla khass doumla kharaf doumla saga doumla door boy tay ma rayla gass dougueul thi kamb nieuw sa deudj di dioy

dakk la rap bouniou tegone 10 beats
yang meu tekk beut man ma tek beut drake wizkid ya mak laalo ya mak thiéré thiak ak mbiskit kholal teusteun rouss sa bopp baba té nga nek nitt

kan mossi topp ma def ko si pote soul na sa rappeur moungi thi kambeu gock ak magock xam xam di rott
ma dé len si nopp man leu ara gueuneu cher ay tableaux d’arts 26 cotes yeah

VIP Paroles By Aya Nakamura

man leu dianteu beuthieuk goudi weer bouma dé wone tay sakh zéro faute louma fi def mo historique
nenagn malen dakk rap lolou dafa leer moungui thi ndelou abba boulay ak bou mamy victory insolite impoli yabou niouma depuis cypher bi daw billay may dakk rap sa rappeur fi ba diarfi bidiaw

niggaz bou gueneu dof niankou kagn ngay amal sa pape ndieurigne dagn tolou thi diankou fokni nio gueuneu reuy espendering
legui guiss na boyi di yewou tadia beat bi def effect tax niou am bongo thi xew mi té niom dofou niou rewou niou té xamga domou niarel la bou ken fokni ara woudjé woul

moytou len ara bou yewou ara toloul ni boy bi mais nak nak li doyna doyloul boy nak bou dayza rapone ki ki dewoul
ki douma…