Learn and sing Vainqueur Paroles By Ngaaka Blindé(Vainqueur Lyrics). Vainqueur Paroles By Ngaaka Blindé(Vainqueur Lyrics) is given below:
Vainqueur Paroles By Ngaaka Blindé(Vainqueur Lyrics)


Skrrrr
Nianou ma kenn té olof ndiaye mokoTE fi wakhone tay dh guene na game, malene geuneu diégué mbedd mi lolotax tay gua seen ma si kaw charétou mbam, Barale yague na diéré, nagne lene niou gueweul niou beurré.
Ma khotti sa yéré, nieupeu kham fou baba diougué té ame diabbou djiné, niari Deum meune naniou ma té ? (Wa)
Kala kotti, caranté bi, philosophie, génie civil, sama city, caranté bi, katanté bi, fanane si fi danga city douggal si mane, lekk mbakhal bou sadique.
Amo réseau, amo réseau, débrouillez vous mes gars ici c’est papa wemba . Té kouma dougg damay dougeul sa papa si roukk dague si solou bi 500
Maman je suis désolé beugou ma wone saga sa dome, effet de l’air bi yonou Gambie la yame nane nguene di wané sen compte. Tay mom douma saga ndax son bou moudiou mongui sa fada
Beuri faces ni ASC LEBOUGUI soma khamoul lathie ma tiaka, bou souba gua fekk ma paname, ma dieuleul la hotel niou fanane, boul niangal nakk fethil sa kaname so paré ma wone la lou yaya diameh
Wa mbaye dieuleul mbaye loumouy way bon si si, si bene affaire bou ndaw rek quoi. Ara mane, ara mane diaxal nama parce que chaque jour mangui wax tu vois,tu es bon anh comme artiste
Effect Secondaire Paroles By Ngaaka Blinde(Lyrics)
Mais bene affaire rek moko yak mouy doul yi quoi, déjà bene Hondarr gua yorr ah, Benz bou rouge mouy khossou gua warr ko peinture defo ko, ngay oser né danga may maye auto quoi si blindé blindé de répétition, ba paré du waat han, di doul
Beugue nga mais yoroo yeah yea. kou tekk sa tank ma sank leu ni raak bi amone intifada, gaindé si aale bi deuk di fadati, mbeur thi lamb dji diokhma nguemb balla bi, thi tang tang bi ma dougal Akhlou bi thi daara dji
Diangue Alif – Lam – Mim ngay sogua khamni rap ak raak rek la miine. Dakk leu rap, geune la rew, eup leu khaliss, niamé thiow, wakhal ma mbour mangui tew après voyage bi damay show
Nagne ma wo si diotaay griffe af bi seytané biggy bi, laasga kirana guisso camaro bi thi clip bi di yeukati pétanque, magui doundou rap dou yakou, bou rap yako tamit mangui doundou, Sénégal mafi dakeu rap
Lolou koumou metti nga dieem S. dougou, les petits chons, dama con, damay faye hôtel, fanane pont, sarakhé guinaar lekk thiéré, di faye diangue xalé yi et c’est bon
Rouss na deug askane leumb dimas degglou may wax loudoul deugg, mane nieupeu ma beugue, bounte bouma nekh ma feug khana may leunde yeah
Ndeysane mbaye ya meuneu wak Ok legui han bon, la, la j’suis peu pressé là, fokk ma dem. Heu comme règlement bi nimou démé 24h yi da guene koy respecter et après lénéne lissi dess moy
Danguene donn beug guene town bi dem gambie mou thiool, meunone nguene dieundatt benene billet. Maintenant dotou ma wax ak yene tant que gueno lene Afrique. Mangui dem Paname solene wakhé nakk
Sans Nouvelle Paroles Tiakola(Sans Nouvelle Lyrics)
Dina deff silence wakh lene endre bima nekk ak limay deff moy nek réponse bi. Niome danio moudie ASTER danio dieulaat benene vol waleu, eh niom niogui fi niogui malicounda, demouniou dh wala niou dieul yonnou ferry bi rek sakh, niogui
Ok c’est bon (X4) Heu Ada cut ko, cut ko, cut ko Okay dama faté wone diokhé annonce bi le ler octobre inchallah wou rabbih, mangui vogue et puis événement bi khamni black party leu, niarri marraine leu ame, mouy ay nitt youma fonk
Ok c’est bon (X4) Heu Ada cut ko, cut ko, cut ko Okay dama faté wone diokhé annonce bi le ler octobre inchallah wou rabbih, mangui vogue et puis événement bi khamni black party leu, niarri marraine leu ame, mouy ay nitt
Yo khamni aussi daniou bokk si mane han et puis khamnani dinagne deff honneur pour nieuw, kene ki mongui toudou arame Akhlou, kenene ki daba brick le 1er octobre mercii